
Office 2010: Càmbarukaayu Bindiinu Wolof
Mellal bu ñu gattal
Microsoft Office 2010 ñeel Càmbarukaayu Bindiinu Wolof mooy may jëfandikukat yi ñuy càmbar bindiinu Wolof ci Office 2010.
Ci Xët Mii
Teqake yu gaaw
| Taalifin wi | 2010 |
| Taarixu Wesaare bi: | 19/07/2012 |
| Làkk: | Wolof |
| Kemu liñu toxal: | 1.2 MB - 2.4 MB* |
| *Dafay sukkandiku moom kemu liñu toxal ci togloo b toxalkat gi ñu daytal. |
Gaaral
Yebbig Càmbarukaayu Bindiinu Wolof bii mooy may jëfandikukat yi ñuy càmbar bindiinu wax ak baat yu Wolof ci Office 2010.
Sampug yeggi gii ci Wolof lay doon.
Bopp xat mi
Ay Cakkutëef i Doxalin
- Doxalin bu jappake: Windows 2000; Windows XP
- Yebbi gii dina dox ak tëriini Office yii:
Bopp xat mi
Ay gindi
- Yebbi taxañ bi ci boo bësee Yebbi (ci kaw) te denc ko ci sa tapaan bu dëgër.
- Ñaarteel-bës ci taxañ bu yékkatiwu bi ci sa tappaan bu dëgër ngir door samp gi.
- Toppal gindi yiy feeñ ngir mottali samp gi.
Bopp xat mi
Baru deñc yi Nekk ci Toxalu gii
Dafay dëpóog yi lëŋkaloo te nekk ci qaaj bii jukki yi ñu tasaare te mu barilool ci toxalukaay bii. Demal toxal jëlëe ca jukk yi gëna mëngóo g yaw.
| Turu jukki bi: | Kemu Jukki bi | |
|---|
forCarmel\14.0.4763.1096_ClientSpeller_none_ship_x64_wo-sn_exe\ClientSpeller.exe | 1.3 MB | |
forCarmel\14.0.4763.1096_ClientSpeller_none_ship_x86_wo-sn_exe\ClientSpeller.exe | 1.2 MB | |
Bopp xat mi