• En utilisant ce site, vous acceptez que les cookies soient utilisés à des fins d'analyse, de pertinence et de publicité.
Office

Thank you for downloading

  • Jumtukaayi Càmbar-làkk Microsoft Office 2013 - Wolof

    If your download does not start after 30 seconds,
    Click here

    Tànnal jukki yi yebuwul

    Turu jukki biDownload LinkKemu Jukki bi
    proofingtools_wo-sn-x86.exeRecommendedClick here813 KB
    proofingtools_wo-sn-x64.exeRecommendedClick here865 KB
    Download Summary:
    KBMBGB

    You have not selected any file(s) to download.

      • Ngir sàmp yebbi gii:
        Sàmp jumtukaayi càmbar-làkk yi:


        1. Ngir yebbi taxañ bi bësal butoŋu Yebbi (ci kaw) te denc sa taxañ ci sa Tappaan bu Dëgët.
        2. Dawal sàncug tëriin wi.
        3. Ci xëtu Yër Sàrti Daganal Jëfekaayu Microsoft, jàngatal sàrt yi, tànnal boyetu seetug "Bës fii ngir nangu Sàrt Daganal Jëfekaayu Microsoft", te bës Wéyal.
        4. Dimbalu sanc daal di daw te sàmp jumtukaayi càmbar-làkk yi.
        5. Su sàmp gi noppee, taalaatal say jëfekayyu ubbi Office.


        Santaaney jëfandikoo: Jëfandikool jumtukaayi càmbar-làkk yi niki ninga ko baaxoo - leegi warngaleen gis ngir sa làkk bi nga sàmp bees. Maanaam, man nga def sa làkkug càmbar-làkk ci làkk bu bees ngir jëfandikoo xoolug bindiin wi (su jàppandee) - ngir xam nees koy defee, xoolal Jekkal làkku càmbar-làkk ngir jàll ci yeneen làkk

        Ngir dindi yebbi gii:
        1. Joxañ ci Jekkal yi ci njëlu Ndoorte li ba noppi bës Fugluwaay bi.
        2. Ñaarte-bës Yokk/Dindi ay Tëriin.
        3. Ci limu tëriin yees sàmp fimne, tànnal Jumtukaayi Càmbar-làkk yu Microsoft Office 2013 - [Làkk] ba noppi bës Simpi, Dindi, wala Yokk/Dindi. Su boyetu diisoo bi feeñee, toopal santaane yi ngir dindi tëriin wi.
        4. Bësal Waay wala Waaw-Kay ngir wéral ni danga bëgg a dindi tëriin wi.


Toxal yu Yaatu

Loading your results, please wait...

Yeesalu PC yu ñu jaayul

  • Patci kaaraange
  • Yeesali xelteef
  • Paki serwiis
  • Dawalkati materyel