• En utilisant ce site, vous acceptez que les cookies soient utilisés à des fins d'analyse, de pertinence et de publicité.
Office

Jumtukaayi Càmbar-làkk Microsoft Office 2013 - Wolof

Select Language:
Jumtukaayi Càmbar-làkk bu Microsoft Office man na amal ay coppite ci làkk yiñ yokk.
  • Note:There are multiple files available for this download.Once you click on the "Download" button, you will be prompted to select the files you need.
    Taalifin wi

    2013

    Turu jukki bi:

    proofingtools_wo-sn-x86.exe

    proofingtools_wo-sn-x64.exe

    Taarixu Wesaare bi:

    07/01/2013

    Kemu Jukki bi:

    813 KB

    865 KB

      Ndax danga bëgg a xool bindiinu làkk wu Office sàmpalul woon boppam? Yegg nga ci barab bu baax bi. Jumtukaayi Càmbar-làkk bu Microsoft Office daf ëmbaale mboolem jumtukaayi càmbar-làkk yi jàppandi ci Office ñeel làkk wii. Sàmpal te taalaat Office rekk, suko defee jumtukaayi càmbar-làkk bu làkk wii daal di noppi.
  • Doxalin bu jappake:

    Windows 7; Windows 8; Windows Server 2008 R2

      Yi tëriin ñooy doxal yebbi gii:
      Microsoft Office Excel 2013
      Microsoft Office OneNote 2013
      Microsoft Office Outlook 2013
      Microsoft Office PowerPoint 2013
      Microsoft Office Word 2013
    • Ngir sàmp yebbi gii:
      Sàmp jumtukaayi càmbar-làkk yi:


      1. Ngir yebbi taxañ bi bësal butoŋu Yebbi (ci kaw) te denc sa taxañ ci sa Tappaan bu Dëgët.
      2. Dawal sàncug tëriin wi.
      3. Ci xëtu Yër Sàrti Daganal Jëfekaayu Microsoft, jàngatal sàrt yi, tànnal boyetu seetug "Bës fii ngir nangu Sàrt Daganal Jëfekaayu Microsoft", te bës Wéyal.
      4. Dimbalu sanc daal di daw te sàmp jumtukaayi càmbar-làkk yi.
      5. Su sàmp gi noppee, taalaatal say jëfekayyu ubbi Office.


      Santaaney jëfandikoo: Jëfandikool jumtukaayi càmbar-làkk yi niki ninga ko baaxoo - leegi warngaleen gis ngir sa làkk bi nga sàmp bees. Maanaam, man nga def sa làkkug càmbar-làkk ci làkk bu bees ngir jëfandikoo xoolug bindiin wi (su jàppandee) - ngir xam nees koy defee, xoolal Jekkal làkku càmbar-làkk ngir jàll ci yeneen làkk

      Ngir dindi yebbi gii:
      1. Joxañ ci Jekkal yi ci njëlu Ndoorte li ba noppi bës Fugluwaay bi.
      2. Ñaarte-bës Yokk/Dindi ay Tëriin.
      3. Ci limu tëriin yees sàmp fimne, tànnal Jumtukaayi Càmbar-làkk yu Microsoft Office 2013 - [Làkk] ba noppi bës Simpi, Dindi, wala Yokk/Dindi. Su boyetu diisoo bi feeñee, toopal santaane yi ngir dindi tëriin wi.
      4. Bësal Waay wala Waaw-Kay ngir wéral ni danga bëgg a dindi tëriin wi.


Toxal yu Yaatu

Loading your results, please wait...

Yeesalu PC yu ñu jaayul

  • Patci kaaraange
  • Yeesali xelteef
  • Paki serwiis
  • Dawalkati materyel