• En utilisant ce site, vous acceptez que les cookies soient utilisés à des fins d'analyse, de pertinence et de publicité.
Windows

Takku Làkku Jokkalekaayu Windows 8 (LIP)

Select Language:
Takku Làkku Jokkalekaayu (LIP) Windows 8 dina indi sumb buñ tekki ñeel li ëpp ci Windows 8.
  • Note:There are multiple files available for this download.Once you click on the "Download" button, you will be prompted to select the files you need.
    Taalifin wi

    1.0

    Turu jukki bi:

    LIP_wo-SN-32bit.mlc

    LIP_wo-SN-64bit.mlc

    Taarixu Wesaare bi:

    03/12/2012

    Kemu Jukki bi:

    2.5 MB

    3.5 MB

      Takku Làkku Jokkalekaayu (LIP) Windows dina indi sumb buñ tekki ñeel li ëpp ci Windows. Ginnaaw sampug LIP, mbind mi ci jàppalekaay bi, boyet yi, njël yi, tombi Ndimbël ak Njàppale dinañ léen di wonee ci làkku LIP wi. Mbind mees ci tekkiwul nag dina nekk ci làkku Windows 8 wawoon. Ci misaal, bu dee sumbub Windows 8 bu Wu-Espaañ nga jëndoon, te samp LIP bu Katalan, yenn mbind yi ci Wu-Espaañ lay des. Man ngaa samp lu ëpp benn LIP ci benn dàttu làkk. LIP yu Windows manees na léen a samp ci mboolem sotti yu Windows 8.
  • Ay Cakkutëef i Doxalin
    Doxalin bu jappake:

    Windows 8

      • Ngir gis Laajtey Noste yi, bësal fii

      • Ngir gindiy njëkk samp gi, bësal fii

      1. Bësal ci bitoŋu Yebbi bi ci xêt wii ngir door yebbi gi, walla nga tànn weneen làkk ci lim biy dirikut.
      2. Defal benn ci yii
        • Ngir door samp gi ci saase, bësal Dawal.
        • Ngir denc yebbi gi ci sa nosukaay ngir samp ko beneene, bësal ci Denc
      • Ngir gindiy ginnaaw samp gi, bësal fii

      • Ngir jafe-jafe yees ci gis, bësal fii

Toxal yu Yaatu

Loading your results, please wait...

Yeesalu PC yu ñu jaayul

  • Patci kaaraange
  • Yeesali xelteef
  • Paki serwiis
  • Dawalkati materyel