This is the Trace Id: 4773cd630e70de4d92553a60899e22fc
Tëbal ci këmbu njëlbéen bi FAQ Déggooy Cëri Microsoft Sàrti Samm-sutura Microsoft Xëtu Joxekati Bing yi Azure Copilot Windows Surface XBOX Outlook Accessories Microsoft AI Microsoft Security Azure Dynamics 365 Microsoft 365 for business Microsoft Power Platform Windows 365 Developer Center Documentation Microsoft Learn Microsoft Tech Community Microsoft Marketplace Visual Studio Software companies View Sitemap

Tënkub coppite yi am ci Déggooy Cëri Microsoft – 30 Sàttumbar, 2026

Noo ngi yeesal Déggooy Cëri Microsoft, yuy jëfe ci sag jëfandikoo costéef mbaa cëri Microsoft yi nekk ci net bi. Xët bii dafay Joxe nanu ab tënk ci coppipte yuñu gën ràññee ci Déggooy Cëri Microsoft.

Ngir gis coppite yépp, noo ngi lay digal nga jàng Déggooy Cëri Microsoft bamu jeex fii.

  1. Ci kawu xët wi, yeesal nanu bisu siiwal ci 30 fan ci wéru Sulet, 2026, ak bis bimuy jëfe bisu 30 Sàttumbar, 2026.
  2. Ci doggitu dugg bi, yokk nanu verbiage ngir dugal ay costéef, daluweb ak sàrwiisi wey-jëfandiku yuy royu ci Déggooy Cëri Microsoft ci suuf tombu "Cër yi" ci Sàrt yi.
  3. Ci pàccu "Jàppandig cër", yokk nanu verbiage bu mengook ci anam bu xejjiku yoon ak sàrti wey-jëfandikukat yu nekk Brésil.
  4. Ci pàccu "Bankaas biy Jël Kontraa bi, Tànneef Yoon wi, ak Barab bi ñuy Saafara Jafe-jafe yi", yeesal nanu bankaam biy jël kontraa bi ngir yenn réew yi nekk Amerik Bëj-gannaar, Amerik Bëj-saalum, ak ci Pacifik Bëj-Saalum.
  5. Ci pàccu "Gaaraanti", yokk nanu verbiage bu mengook ci anam bu xejjiku yoon ak sàrti wey-jëfandikukat yu nekk Brésil.
  6. Ci pàccu "Sàrt yuy àndak cër yi", amal nañu yile ndolent ak ay coppite:
    • Ci pàccu "Màngasiin", yeesal nanu verbiage bi ci li aju ci yeesal ci saasi, yuy tax wey-jëfandikukat yu ajandi yeesal ci saasi ak leeral li ciy mêna am suñu yeesalul applications yi.
    • Ci suuf pàccu "Cortana", leeral nanu ni Cortana nekkatul ci loxol Microsoft tambalee ko 2024, te dindi nañu pàcc yu mengook man-mani Cortana yuñu mënatul jëfandikoo.
    • Ci pàccu "Microsoft 365 Applications ak Services yi", yeesal nanu ni ñuy tudd turu ndaje‑ndaje yu produi Microsoft 365 yi, te leeral nanu ne jëfandikoob applications ak services yi ñuy wax ci mooy aju ci sàrti daganal yi.
    • Ci pàccu "Marsandiisu Xarala", far nanu royale ci Microsoft Groove, li nga xamantane jàppandiwatul.
    • Ci pàccu "Microsoft Rewards", yeesal nanu ay lëkkalekaay yu jëm ci ay xëti ndimbal yu baax te yeesal nanu dayoob poñ yi nga mëna weccoo ngir ñu feeñal ñaari dayoob yemale.
    • Tuddeewaat nanu pàccu "Copilot" te sumbi Copilot yuy jëfee yu weeru ci Déggooy Cëri Microsoft yi leeral nañ leen.
  7. Ci mbooleem Sàrt yi, amal nanu ay coppite yu bari ngir gëna leeraay ak ngir joxoñ bépp róofo baat, mbindiin ak yeneen jafe-jafe yu nduroo. Yeesal nanu itam tur wi ak iper-lëkkalekaay yi.
Wolof (Senegaal)
Your Privacy Choices Opt-Out Icon Your Privacy Choices
Consumer Health Privacy Contact us Privacy & Cookies Manage cookies Terms of Use Trademarks About our ads